vendredi 09 février 2018


Textes
Titres
Interprètes
Posteurs

Vous recherchez des paroles de chansons
   


Sa Rimbam

Télécharge la Sonnerie de "Sa Rimbam"

Interprete : PAPE DALY , BABACAR SECK

Langue : Lingala
Genre : Africain
Auteur : galsenaize
Année : 2008



Texte :

sama ga yi dégno beugue kou nék diouk contantél sa rimbam
yow yaye li gueneu néx sama xol nowci nop naleu
(cote ko géré ko)
founé démna feu mane guissouma lénéne lou leu gueneu
(dama la guiss beugue leu lol kay)
sa xol bi la léy lathieu
(lolou kouko songo sét doukeu diwoni)
goor bou bari thiath
(dokou ma khol rék da di miire si mane)
bala mouy néx gnou dém beu wara séy meu téreul leu
(a travers l'objet aimé tout deviens aimable
héééy mbeuguenté dafa xéw contanté dafa xéw)
héy sa rimbam bam bam SA RIMBAM
sa rimbam bam bam SA RIMBAM
so ke dégueté moy mbeuguélou gounéy téy SA RIMBAM (2fois)

yow yaye li gueneu néx sama xol nowci nop naleu
founé démna feu mane guissouma lénéne lou leu gueneu
(dama la guiss da di miire si yow)
sa yaram lay sentiir (lolou kouko songo sét doukeu diwoni)
goor bou léy mentiir (négnou céddo mbeuguél si sincérité)
sa température lay sentir beuss bou né nop na leu
( température conbien de degré ? kay waxko seu degré
sokhnaci khamneu degeurém)
(koufi amoul degré beutéy doto ameuti degré)
température bou nék si yow mome lay sentiir
sa rimbam bamm sa rimbam
sa rimbam bam bam ...

téy dji boy digue fiére
bayo fi bénéne k'air
se rongogne da di fére
guéy noyi bénéne air

sou mbeugué ligue mbeugue
mbeuguel limou beugue
sou bégné ligue bégne nak
béyeul limouye bégne
loloy fierté mbeuguél
loloy g... si mbeuguél
sou bégné lou léy sonal
moy liko sonal
mbeuguél té niar nioko sék
kou mbeugue ak ki gnou mbeugue
sougnou dadjé ak mbeugeunté leu

takal ma takal ma nowci
nowci yow leu mbeugue
diapal ma diapal ma nowci
nowci yow la aimé


Poster par :

 
Erreurs, Ommission ou contenu illégal.







Autres chansons de :
PAPE DALY , BABACAR SECK
sa rimbam
sa rimbam

© 2013 - Paroles.zouker.com - Texte soumis aux Droits d'Auteur.
Réservé à un usage privé ou éducatif.


Partager Share/Bookmark


Pour les loveurs lol
Poster par : le : 19/02/2009
Ip : 89.3.101*****
Note :




 Options
- Imprimer le texte : Sa Rimbam
- Envoyer le texte : Sa Rimbam à un(e) ami(e)
- Autres chansons de : PAPE DALY , BABACAR SECK
- Acheter le cd ou titre
- Télécharge la Sonnerie de "Sa Rimbam" pour ton Portable
- Toutes les sonneries de : "pape daly" , "babacar seck"


Top Genres :
Top Langues :