mardi 03 septembre 2019


Textes
Titres
Interprètes
Posteurs

Vous recherchez des paroles de chansons
   


Yaw Rek Leu

Télécharge la Sonnerie de " Yaw Rek Leu"

Interprete : PHILLIPE MONTEIRO , CORINE

Langue : Créole
Année : 2005



Texte :

Ibil nal sama khol,
Yalla na nga si guiss lou lére
Té gueuneu kham ni
Amoul kénène koudoul yaw.

Mbeugél gui nékeu si mane
A ngii di ma dane
Té gueum na né di na done
Sa néné bi ngéy tété.
Mane mi souma mounone,
Dina bokake yow bénéne yone,
Dila wowé néné touti,
Ndakh té mane mi,
Mane mi gnanou ma yalla,
Gnanou ma yalla
Déss fii mane réka!

REFRAIN:

Yow mi néke sama khol
Guissou ma kénéne koudoul yow
Mbeuguél gui mo ngi ni di law,
Ibil nala sama khol
yow mi néke sama khol
Guissou ma kénéne koudoul yow,
Mbeuguél gui mo ngi ni di law,
Té dina done sa néné.


Am na gnou wakh
Mbeugél tiono rék la,
Wayé ma ngi léy khamal
Dou kéne yow réke leu.
Beuss bou me le guissé
Ta kham ni khol déy guissé
Té fok na ni do meusse tass sama yakar!

Boul am loy ragal di la khar,
Doumeu meusseu diay sama taar,
Dinala wowé papa chéri,
Dina done sa sokhna,
Di na done sa baby,
Mi léy fadial
Say sokhla, oh baby yow réke le

REFRAIN:

Yow mi néke sama khol
Guissou ma kénéne koudoul yow
Mbeuguél gui mo ngi ni di law,
Ibil nala sama khol
yow mi néke sama khol
Guissou ma kénéne koudoul yow,
Mbeuguél gui mo ngi ni di law,
Té dina done sa néné.


Yay sama doolé
Soudoul yow wate na né dou done kékéne,
Diokh na la sama bope,
Té dina la dégueul di le bégueul,
baby boul sone,
gueumeul ni yow réke le!
dou kékéne....

http://x-negez-x.skyrock.com


Poster par : x-negez-x

 
Erreurs, Ommission ou contenu illégal.







Autres chansons de :
PHILLIPE MONTEIRO , CORINE
Nuit sauvage
Lanmou san lanmou
Cicatrice - vré pawol-la
Royaume zouk
- En Haut, En Bas
Kochma sakré
Yaw rek leu
En haut, en bas
Jues Pas (By DJ Hoxas)
Kè an mwen an balad
Yaw rek leu
Yaw rek leu
Yaw rek leu
Yaw rek leu
Lose control
N kre volta

© 2013 - Paroles.zouker.com - Texte soumis aux Droits d'Auteur.
Réservé à un usage privé ou éducatif.


Partager Share/Bookmark






 Options
- Imprimer le texte : Yaw Rek Leu
- Envoyer le texte : Yaw Rek Leu à un(e) ami(e)
- Autres chansons de : PHILLIPE MONTEIRO , CORINE
- Acheter le cd ou titre
- Télécharge la Sonnerie de " Yaw Rek Leu" pour ton Portable
- Toutes les sonneries de : "phillipe monteiro" , "corine"


Top Genres :
Top Langues :